Songteksten Vertalen

Zoek vertaling

Artiest: Ismael Lo Songtekst: Baykat

Je bekijkt nu de songtekst en vertaling: Ismael Lo - Baykat ? Hieronder vindt je de songtekst met vertaling naast elkaar weergegeven! Benieuwd naar het liedje en de betekenis van Baykat? Bekijk de Nederlandse vertaling. Op onze website vindt je veel meer songteksten met vertalingen van Ismael Lo! Bekijk ons archief en de andere songteksten, klik bijvoorbeeld op de letter I van Ismael Lo en zie welke nummers wij nog meer van a in ons archief hebben staan zoals Baykat .

Origineel

Mané hé baykat bi khalam Démonna bay nékh wayé boumgua Dokna mome Mané hé baykat bi khalam Démonna bay nékh wayé boumgua Dokna mome Mané hé baykat bi khalam démonna Bay nékh wayé boumgua dokna mome Boula nékhé talalal say lokho Yaye docteur biy fath khifou askane bi Liko dalé si nditoum rew bassi miskine Ya souméko di dane sa dolé andak nath Bi di liguey sa gnakha di tourou Ngay bay di doukat bilay ya am diome Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour waw koufi fébar Yako nandal aki réén bamou féékh Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Ya momone sa mbay Ya mome sa guanthiakh mome say Ndiour ya mome sa alla di bay Nguour gneuw dougalthia lokhome ak Boor fékeleuthaa guanthiakh ba Mégneu lole ndékétéyo Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Dirama diarama baykat bé yaw Kéneu rek mola mana fay Moy bourbi yaalla Guathia ngalama Guathia ngalama yaw baykatbé Guathia ngalama Guathia ngalama yaw baikatbé Dirama diarama baykatbé yaw Kéneu rek moleu mana fay Moye bourbi yalla

 

Vertaling

Mané hé baykat bi khalam Démonna bay nékh wayé boumgua Dokna moeder Mané hé baykat bi khalam Démonna bay nékh wayé boumgua Dokna moeder Mané hé baykat bi khalam démonna Bay nékh wayé boumgua dokna mome Boula nékhé talalal zegt lokho Deze dokter is ook een fath khifou askane bi Als je het niet leuk vindt, zul je het missen Ya souméko di dane sa dolé andak nath Als je er allemaal vanaf wilt komen Ngay bay di doukat bilay ya am diome Kon Diarama Baykat Koufi Xiff Yako Doundal bamou sour waw koufi fébar Yako nandal aki réén bamou féékh Kon Diarama Baykat Koufi Xiff Yako Doundal bamou zuur Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Ya momone sa mbay Ya mome sa guanthiakh mome zegt Ndiour ya mome sa alla di bay Nguour gneuw dougalthia lokhome ak Boor fékeleuthaa guanthiakh ba Magneu lole ndékétéyo Kon Diarama Baykat Koufi Xiff Yako Doundal bamou zuur Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Kon Diarama Baykat Koufi Xiff Yako Doundal bamou zuur Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Dirama diarama baykat be yaw Kéneu rek mola mana fay Moy bourbi yaalla Guathia ngalama Guathia ngalama yaw baykatbé Guathia ngalama Guathia ngalama yaw baikatbé Dirama diarama baykatbé yaw Kéneu rek moleu mana fay Moye bourbi yalla